56
Livret décodable 2 DU PEUPLE AMERICAIN 0LQLVWqUH GH O·pGXFDWLRQ QDWLRQDOH

Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

  • Upload
    others

  • View
    0

  • Download
    0

Embed Size (px)

Citation preview

Page 1: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

Livret décodable 2

DU PEUPLE AMERICAIN

Page 2: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 3: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

Table des matières

Alphabet illustré 1

Table de l’alphabet 1

Leçon 1 de Pré-lecture 1

Leçon 2 de Pré-lecture 1

Leçon 3 de Pré-lecture 1

Leçon 4 de Pré-lecture 1

Leçon 5 de Pré-lecture 1

Leçon 6 de Pré-lecture 1

Leçon 7 de Pré-lecture 1

Leçon 8 de Pré-lecture 1

Leçon 9 de Pré-lecture 1

Leçon 10 de Pré-lecture 1

Leçon 3 de Pré-lecture 1

Leçon 3 de Pré-lecture 1

Alphabet illustré 1

Table de l’alphabet 1

Leçon 1 de Pré-lecture 1

Leçon 9 de Pré-lecture 1

Leçon 10 de Pré-lecture 1

Leçon 3 de Pré-lecture 1

Leçon 3 de Pré-lecture 1

Page 4: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 5: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

BËRE XAJ AK GOLO

Page 6: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

6

Estaad bi fees na dell aki mala.Xaj ngembu na di màttu. Mu ngi sangu ak saafara yu bare.

Page 7: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

7

Golo mu ngi tuus, ñépp di ko tàccu.Mu ngi tëb ca kaw aka gaññ.Leeg-leeg mu pàkkarñi, fecc, tàllal loxoom.

Page 8: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

8

Maam Golo mooy tëgg sabar, ñaq tooy xepp.Fas ak Nag ñu ngi koy may xaalis.Mbaam dóor na pooj waŋŋeetu ñetti yoon.

Page 9: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

9

Bàjjan Béy arbit woo na ñaari mbër yi.Bi ñu duggee ci géew bi, Xaj baw.Arbit bi mbiib, ñu tàmbali léewtoo.

Page 10: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

10

Xaj song na Golo mu génn géew bi.Arbit bi artu ko ci génn bi.

Page 11: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

11

Xaj cokkaas na ko, Golo yuuxu Golo daw na làqu ci ginnaaw arbit bi.Leegi, Golo miir na di wëndéelu.

Page 12: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

12

Noonu, arbit tàllal na loxoom woo doktoor Looy. Ndeysaan, Looy a ngi koy faj muy yuuxu.Mu metti, Golo yenu doktoor Looy daaneel.

Page 13: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

13

Mbokki Golo jiital seen mbër yobbu. Doktoor looy jox na ndam li Xaj. Làmb ji jaxasoo, coow li jolli

Page 14: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 15: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

Futbalu mala

Page 16: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

16

Baay Gaynde dafa woote, mala yépp dawsi ñëw.Ñu yàkkamti koo déglu.Dama bëgg ngeen def joŋante bu am neexal.

Page 17: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

17

Lëg, Mbaam-àll ak Bukki xoolante.Gaynde jël kàddu gi.Dama bëggoon boroom dunq jàkkaarloo ak boroom kawar.

Page 18: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

18

Ginaar kobos Naat ne ko ñooy am ndam.Su bal bi naawee, ñu naaw.

Page 19: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

19

Jabaru Golo wokk boppam di wax ak Ñey.Dinanu leen daan ndax noo leen ëpp doole.

Page 20: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

20

Banjóoli yëngal ay mbaggam.Dama cee bokkul am dangeen maa fàtte. Njamala yuuxu, maay góol, bal du ma romb

Page 21: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

21

Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku.Lëg tëb ne man maay arbit.Mbonaat di seetaan, Jaan di fecc.

Page 22: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

22

Jàmb Jóob duut, jox bal bi Seku.Mu jékki- jékki rekk, asamaan si lëndëm kuruus.Ndoxum taw dal, Béy daw, Ginaar topp ca.

Page 23: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

23

Melax ne ràyy, dënnu yëngal suuf ak garab.Ndox mi di sotteeku mel ni géej.Ñey daadi daw, lépp jaxasoo.

Page 24: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 25: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

NGÉNTE LI

Page 26: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

26

Ami dafa am doom.Tey la am juroom-ñetti fan. Baayam Móodu bëgg na ngénte lu neex.

Page 27: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

27

Bale nañu kër gi ba mu set wecc. Lal nañu basaŋ yu mag, teg ay siis.

Page 28: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

28

Ci waañ wi, teg nañu mbana yi.Araw nañu leketi sunguf ngir laax yi.Ñeneen jël bagaani soow yi def ci suukar.

Page 29: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

29

Ami sangu na, daadi solu. Takk na caq, lam ak jaaro yu gudd.Tey, mbubb mu mag la tànn ak kolam.

Page 30: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

30

Jël na séru njaago lëmëse ko liir bi. Waa kër gi sañse nañu, tuuroo latkoloñ.

Page 31: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

31

Jigeen ak góor defaru nañu ba jekk. Jigeen ñi takk nañu ceeni oor.Nit ñi toog ci ay basaŋ aki siis.

Page 32: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

32

Bàjjan toog ci wetu Ilimaan, uuf liir bi. Ilimaan joxe tur wi, Bàjjan Kura. Ñu séddale laax yi ci bool yu ndaw.

Page 33: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

33

Tëgg nañu sabar, tama, kooraa ak riiti.Togg nañu añ, njogonal, joxe am njar.Ginnaaw ba, ñu lekk pom, màngo ak banaana.

Page 34: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 35: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

Espektëer dikk na

Page 36: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

36

Defar nanu kalaas bi ba mu jekk.Bale nanu dër bi, raxas póllu mbalit mi.Fomp nanu palanteer yi ba ñu set wecc.

Page 37: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

37

Sunu madam dafa farlu.Tey, sunu cawarte dafa yokku.Fëgg nanu armool bi def téere yi.

Page 38: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

38

Madam Siise ni nu tey, danuy am gan.Su gan gi ñëwee, lépp lay xool.Léegi, toog nanu ci kalaas bi di jàng.

Page 39: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

39

Oto bu xonq taxaw na sunu wetu ekool.Genn góor wàcce na ci oto bi.Mu ngi takk lunet yu ñuul.

Page 40: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

40

Mu ngi téye saag bu mag. Kilifa gi dem na seeti direktëer. Toog nañu ñoom ñaar waxtaan ab diiir.

Page 41: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

41

Sunu madam waaxu na jox loxo Espektëer bi.Bi nu sunu madam geestoo, ñépp jóg taxaw.Espektëer bi yékkati loxoom, nu toogaat.

Page 42: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

42

Mu dem toog ca gannaaw di nu saytu.Nu tàmbalee nafar li nu jàngoon lépp.

Page 43: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

43

Sunu madam dinu laaj, nuy tontu.Espektëer jóg na, ñëw ci sunu madam.Ba mu yàgg, ñu ànd dem ca direktëer.

Page 44: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 45: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

Fànta ak Biraan am nañu ndam

Page 46: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

46

Bu ekool tëjee, direktëer dafay joxe neexal.Ñaari xale yi raw ci kalaas lañuy tànn.Fanweeri fan ci weeru sulet lañu ko def.

Page 47: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

47

Suba teel, xale yi ñëw, sañse ba jekk.Ñii sol yëre cosaan, ñee sol yëre yeneen .Xale yi ànd ak seeni waajur.

Page 48: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

48

Muse ak madam yépp sañse nuróole ay waks.Ëtt bi set lool, xale yi bég.Xale yiy am neexal toog ci kanam.

Page 49: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

49

Ci seen ndeyjoor, kilifa yi toog fa.Xumb-xumb yi nekk ci seen càmmoñ. Waajur yi toog nañu ci gannaaw elew yi.

Page 50: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

50

Neexal yaa ngi tege ci kanamu xale yiÑu ràññee ca téere njàng ak xayma.Amoon na itam ay kaye ak ay tablet.

Page 51: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

51

Bi fukki waxtu jotee, mbir mi tàmbali.Ñu jëkke ci kalaas bu ndaw bi.Fànta ak Biraan lañu jëkk a woo.

Page 52: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

52

Ñu dem ci kanam, ñépp di leen tàccu.Direktëer bi jël paket bu mag a mag.Mu nuyu Fànta, jox ko ko.

Page 53: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

53

Mu woo Biraan, jox ko beneen paket.Ñii di leen kameraa, ñee di leen foto. Seen moroom yépp di leen xool, naw leen.

Page 54: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 55: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg
Page 56: Livret décodable 2 ggatu-ci-dawal-1-2.pdfLeçon 2 de Pré-lecture 1 Leçon 3 de Pré-lecture 1 Leçon 4 de Pré-lecture 1 ... 21 Segg taxaw na, Fasu àll di daagu di bàkku. Lëg

DU PEUPLE AMERICAIN